-
Si bi di bé da da lé / Dama khamoul loufi diar yaye djour sanni / Kholal gni fi beugue ame sene dome te Yalla mahoulenko / Boula Yall mayé dang koye khame / Tchey yawitt dome sa yo maqué Lép liye begg…
-
Yaw mi lé, djoudo tchi rëw, magué tchi rëw / Bourbi Yalla wersaguéla gua mana deme ba bitlim rëw mana / Danidollé, Boul Faté Mdéye Boul Fate Baye / Wara mana tok goorgoorlou / Ba gay dem, Mdeye ak Bay…
-
Aytcha len gnou saf / Mdakh fi bo doul saf / Do Djembeut dara mu skh / Lo donoul talibem mouno done serignam / Rew dal bou paré patt tcha tol ya la djogué / Gor ak Djiguene, aywalene tcha tolya / Ana …
-
Hé guawlène, guawlène gagnoyakamti guawl`ne, gnoune dé dagnon beugui / Gnibi deukeuba, Sénégal auion bigne done khar yaye gniewa guoule / Guawl`ne dgno yakamti guawléne / Guawl`ne dagno yakamti gawlén…
-
Il n’y a jamais de blanc sans noir / Comme une longue journée sans nuit / Beaucoup de temps perdu sur des couleurs / Changeons d’idées et de mentalités / La couleur du nouveau millénaire est dans nos …
-
Li mo ma djakhal, li di li ma titall / Mac gna gui kheutiongourgui / Gouneyi woute kougnou soumi / Li mo ma djakhal, li di li ma titall / Mac gna gui kheutio ngourgui / Gouneyi woute kougnou soumi / M…
-
Mane, li ma beugueu dafa Barri te wouté oh mane / Sama beugue beugue rombena adounassité oh mane / Damay tok bamou yague sama khël dem tchi samay dom mane / Souma manone, souma manoné, khélal la gua y…
-
Wadjour, khol len li gueun tchi mome / Wadjour khol len / Gagni khol len li guen tchi mome / Gagni khol len / Wadjour set len li guen tchi mome / Wadjour khol len / Moytouko, Moytouko (2 x) / Qui dé l…
-
Bo guissé adouna ni mou mela takh ma wakhé ni / Guor dafa wara Gorguolu tambeléko tcha bamouye ndaw / Te khame ni wadjour, sen djan mome watchna / Dakh situation métiwone na lolo takhone ma guene keur…
-
Mit ko wakh bopame mouni dangue ko beigne yaye / Ya dagno khamoul mome louye nit / Mi mome nittaye guarrabame, garrabame guarrabame mome / Bo amé say nit té deggueutoléne diguani bok yenesayaw / Mbaye…
-
Say niane nagouna yaw mani santal / Say lidjanti ostina yaw mani teyloul / Bousa ande boyé sani tchi mata gueune fayko / Say niane nagouna yaw mani santal… / Mayou Yalla dafa barri té wouté / Mit koun…
-
Baye Boye, yague na la deguelou gua may diggeul, lo bakh Sama Baye Boye / Khame na ni, lounek dadj gua ko baye lëp guir mane / Khame na ni méti wone na lolou tchi djamono yé gnou wessou / Yaye Boye, m…